Hip-hop wuute gi ci sumb yi
m robot Modifie : ru:Хип-хоп (музыкальный жанр) |
Replacing Lil_Wayne_July_2020.jpg with File:Lil_Wayne_Feb._2020.jpg (by CommonsDelinker because: File renamed: Criterion 3 (obvious error) · Not sure why it states July, the photographer stat |
||
(26 versions intermédiaires par 19 utilisateurs non affichées) | |||
Rëdd 1 : | Rëdd 1 : | ||
[[Dencukaay:Hip hop.jpg|thumb|right|400px|ay breakat]] |
[[Dencukaay:Hip hop.jpg|thumb|right|400px|ay breakat]] |
||
'''Hip-hop''' ag yëngu-yëngug [[caada]] ak [[fànn]] la, mi ngi juddoo ca [[Réew yu Beenoo]] ya ci ndoorteel [[ |
'''Hip-hop''' ag yëngu-yëngug [[caada]] ak [[fànn]] la, mi ngi juddoo ca [[Réew yu Beenoo]] ya ci ndoorteel [[ati 1970]] yi, daa boole bànneexu ak ñaxtu. Mi ngi juddoo ci biir askani waa-aamerig yu ñuul yi, ca [[New York]], fa la tàmbalee, mujj tas ca réew ma ba ci àdduna bi bépp, ba tay mooy dundiinu réewu-taax wi ëpp doole. Caaday Hip-hop ci ñeenti ponk la tënku: [[Break dancing|''break dancing'']], ''[[DJing]]'', ''[[MCing]]'' ak [[Graffiti|''graffiti'']]. |
||
Wii xeetu [[fànn]] ñu bari ci woy wi lañ koy tënk ,''MCing'', te mu gën a siiw ci [[ |
Wii xeetu [[fànn]] ñu bari ci woy wi lañ koy tënk ,''MCing'', te mu gën a siiw ci [[rap]]. Caadaay Hip hop yamul rekk ci rap, man naa sol mbubb yu wuute: su fekke danuy yam rekk ci xoosug DJ bi ([[Disk Jokey]]), waruñu ko tuddeeti rap, waaye DJing , sunu yamee ci li MC bi (master of ceremonie, [[njiitul xew]]) di bàcc kon man nanu koo woowe rap, walla tamit, donte bari na lu muy faral di am, boolee benn DJ ak ay walla benn MC, kon ci nii hop-hop lañuy wax, ndax [[rap]] ak [[MCing]] yépp ci caadaay hip hop lañu bokk, waaye nit ñi rap lañuy wax rekk yam ci ngir yombal. |
||
== Cosaanu baat bi == |
== Cosaanu baat bi == |
||
Rëdd 9 : | Rëdd 9 : | ||
* ''Hip'' "muus", "am-xel" lay tekki, muusaayu tappalaatukat. |
* ''Hip'' "muus", "am-xel" lay tekki, muusaayu tappalaatukat. |
||
* ''Hop'' ag yuuxu la gu kuy tëb di def (sooy tëb ni op!). |
* ''Hop'' ag yuuxu la gu kuy tëb di def (sooy tëb ni op!). |
||
Nee nañu baat baa ngi war a bawoo ci [[DJ Luv Bug Starski]] mi ko doon faral di jëfandikoo suy wax. Waaye li wér te wóor mooy ne gandoor |
Nee nañu baat baa ngi war a bawoo ci [[DJ Luv Bug Starski]] mi ko doon faral di jëfandikoo suy wax. Waaye li wér te wóor mooy ne gandoor bu [[Sugarhill Gang]] mooy ki ko siiwal ci àdduna bi, ci seen woy woowu ''Rapper's Delight'', di benn ci woyi rap yi ñu njëkk a def k7. |
||
== Taariix == |
== Taariix == |
||
[[File:Lil Wayne Feb. 2020.jpg|thumb|Lil Wayne]] |
|||
==== Ay cosaanam ==== |
==== Ay cosaanam ==== |
||
Woyu hip-hop ci buumu xeeti woyi waa-aamerig yu ñuul yi la bokk. Ay dàttam ñi ngi bàyyikoo ci dundiin gu metti gi ñu nekkee woon, dalee ca seeni maam ba ci jamono yi muy juddu, woy yañu daan def ca tool ya daan ca naqarlu seenug nekkiin, ak daan ca fattali seenug jóge [[Afrig]]. Mi ngi tàmbalee ciy kebetu niki xeeti woy yu mel ne [[ |
Woyu hip-hop ci buumu xeeti woyi waa-aamerig yu ñuul yi la bokk. Ay dàttam ñi ngi bàyyikoo ci dundiin gu metti gi ñu nekkee woon, dalee ca seeni maam ba ci jamono yi muy juddu, woy yañu daan def ca tool ya daan ca naqarlu seenug nekkiin, ak daan ca fattali seenug jóge [[Afrig]]. Mi ngi tàmbalee ciy kebetu niki xeeti woy yu mel ne [[ragetime]], [[jazz]], blues. Ci lu gën a jonjoo, woyu hip-hopa ngi bawoo ci ''Soul'', ak ci ''funk''. Yii xeeti woy bawoo [[bëj-gànnaaru Aamerig]] dem ba fasook sound-system bu waa-jamayka, bi àgg ba New York ndax ndoxandéemu gi waa-jamayka yi daa def foofa. Ba tax-na ñett ñi ñu ne ñoo sos yëngu-yëngu hip-hop fa lañu bàyyikoo. |
||
Donte hip-hop ci yii xeeti woy la jële ay dàttam, waaye doonul seenug wéyal. Du lu ay tëggkat yu xereñ ci seen liggéey toog xalaat, |
Donte hip-hop ci yii xeeti woy la jële ay dàttam, waaye doonul seenug wéyal. Du lu ay tëggkat yu xereñ ci seen liggéey toog xalaat, ni blues doonee wéyalug jazz, gospel juddoo ci blues, soul tegu ci, funk ñëw, caaday hip-hop dafa am ab dog-dog ag yeneen xeeti woy yooyu |
||
==== Aji-rap yi njëkk ==== |
==== Aji-rap yi njëkk ==== |
||
Rëdd 31 : | Rëdd 31 : | ||
* [[Last Poets]] |
* [[Last Poets]] |
||
== Lëkkalekaay yu biti == |
== Lëkkalekaay yu biti == |
||
* [http://www.jolofrap.com/ Ab buntu ci rap Jolof] |
* [https://web.archive.org/web/20110208022715/http://www.jolofrap.com/ Ab buntu ci rap Jolof] |
||
* [http://www.africanhiphop.com Ab dal ci hip-hopu Afrig |
* [http://www.africanhiphop.com Ab dal ci hip-hopu Afrig ] |
||
* [http://www.unitednationsofhiphop.com Màggug hip-hop ci àdduna bi] |
* [https://web.archive.org/web/20210125154149/http://www.unitednationsofhiphop.com/ Màggug hip-hop ci àdduna bi] |
||
* [http://www.goodka.com Taariixu hip-hop] |
* [http://www.goodka.com Taariixu hip-hop] |
||
* [http://www.fluctuat.net/5598-Histoire-du-hip-hop Tariixu hip-hop] |
* [https://web.archive.org/web/20080509092222/http://www.fluctuat.net/5598-Histoire-du-hip-hop Tariixu hip-hop] |
||
* [http://www.reprezent.ch/v3/culture/ |
* [http://www.reprezent.ch/v3/culture/ taariixu hip-hop Zulu Nation moo ko defar ak yeneen jukki] |
||
* [http://twilightzonecrew.com/spray/ ''Mémoires d'un graffiteur'' njëlbeenu hip-hop ca Faraas] |
* [http://twilightzonecrew.com/spray/ ''Mémoires d'un graffiteur'' njëlbeenu hip-hop ca Faraas] |
||
* www.hiphop-musik.org [http://www.hiphop-musik.org] |
* www.hiphop-musik.org [https://web.archive.org/web/20101030051650/http://www.hiphop-musik.org/] |
||
[[catégorie:Hip Hop]] |
|||
[[ |
[[Wàll:Hip Hop]] |
||
[[als:Hip-Hop]] |
|||
[[an:Hip hop]] |
|||
[[ar:هيب هوب]] |
|||
[[ast:Hip hop]] |
|||
[[be:Хіп-хоп]] |
|||
[[be-x-old:Гіп-гоп]] |
|||
[[bg:Хип-хоп музика]] |
|||
[[bn:হিপহপ]] |
|||
[[bs:Hip-hop]] |
|||
[[ca:Hip hop]] |
|||
[[cs:Hip hop]] |
|||
[[cy:Hip hop]] |
|||
[[da:Hiphop]] |
|||
[[de:Hip-Hop]] |
|||
[[el:Χιπ χοπ]] |
|||
[[en:Hip hop music]] |
|||
[[eo:Hiphopo]] |
|||
[[es:Hip hop]] |
|||
[[et:Hiphop]] |
|||
[[eu:Hip hop]] |
|||
[[fa:موسیقی هیپ هاپ]] |
|||
[[fi:Hip hop]] |
|||
[[fo:Hip hop]] |
|||
[[fr:Hip-hop]] |
|||
[[fy:Hiphop]] |
|||
[[ga:Rapcheol]] |
|||
[[gan:嘻哈音樂]] |
|||
[[gd:Hip-hop]] |
|||
[[gl:Hip hop]] |
|||
[[he:מוזיקת היפ הופ]] |
|||
[[hi:हिप हॉप संगीत]] |
|||
[[hr:Hip-hop]] |
|||
[[hu:Hiphop]] |
|||
[[hy:Հիպ Հոպ]] |
|||
[[id:Hip-hop]] |
|||
[[is:Hip hop]] |
|||
[[it:Hip hop]] |
|||
[[ja:ヒップホップ]] |
|||
[[ka:ჰიპ ჰოპი]] |
|||
[[kk:Хип-хоп]] |
|||
[[ko:힙합]] |
|||
[[la:Musica hiphop]] |
|||
[[lb:Hip-Hop]] |
|||
[[lt:Hiphopas]] |
|||
[[lv:Hiphops]] |
|||
[[mk:Хип хоп музика]] |
|||
[[ml:റാപ്പ്]] |
|||
[[ms:Hip hop]] |
|||
[[nds:Hip-Hop (Musik)]] |
|||
[[nds-nl:Hiphop]] |
|||
[[nl:Hiphop]] |
|||
[[nn:Hiphop]] |
|||
[[no:Hiphop]] |
|||
[[oc:Hip-hop]] |
|||
[[os:Хип-хоп]] |
|||
[[pl:Hip-hop]] |
|||
[[pnb:ہپ ہاپ موسیقی]] |
|||
[[pt:Hip hop]] |
|||
[[ro:Muzică hip hop]] |
|||
[[ru:Хип-хоп (музыкальный жанр)]] |
|||
[[rue:Гіп-гоп]] |
|||
[[sh:Hip hop]] |
|||
[[simple:Hip hop]] |
|||
[[sk:Hip-hop (hudba)]] |
|||
[[sl:Hip-hop]] |
|||
[[sq:Hip hop]] |
|||
[[sr:Хип хоп]] |
|||
[[sv:Hiphop]] |
|||
[[sw:Muziki wa hip hop]] |
|||
[[ta:ஹிப் ஹாப்]] |
|||
[[th:ฮิปฮอป]] |
|||
[[tr:Hip hop]] |
|||
[[uk:Хіп-хоп]] |
|||
[[uz:Hip hop]] |
|||
[[vi:Hip hop]] |
|||
[[war:Hip hop (tukar)]] |
|||
[[yo:Orin hip hop]] |
|||
[[zh:嘻哈音樂]] |
|||
[[zh-yue:Hip hop]] |
Sumb bi teew bu 8 Sattumbar 2024 à 01:52
Hip-hop ag yëngu-yëngug caada ak fànn la, mi ngi juddoo ca Réew yu Beenoo ya ci ndoorteel ati 1970 yi, daa boole bànneexu ak ñaxtu. Mi ngi juddoo ci biir askani waa-aamerig yu ñuul yi, ca New York, fa la tàmbalee, mujj tas ca réew ma ba ci àdduna bi bépp, ba tay mooy dundiinu réewu-taax wi ëpp doole. Caaday Hip-hop ci ñeenti ponk la tënku: break dancing, DJing, MCing ak graffiti.
Wii xeetu fànn ñu bari ci woy wi lañ koy tënk ,MCing, te mu gën a siiw ci rap. Caadaay Hip hop yamul rekk ci rap, man naa sol mbubb yu wuute: su fekke danuy yam rekk ci xoosug DJ bi (Disk Jokey), waruñu ko tuddeeti rap, waaye DJing , sunu yamee ci li MC bi (master of ceremonie, njiitul xew) di bàcc kon man nanu koo woowe rap, walla tamit, donte bari na lu muy faral di am, boolee benn DJ ak ay walla benn MC, kon ci nii hop-hop lañuy wax, ndax rap ak MCing yépp ci caadaay hip hop lañu bokk, waaye nit ñi rap lañuy wax rekk yam ci ngir yombal.
Cosaanu baat bi
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]Cosaanu baat bi taxu koo leer noonu, ci ñenn ñi jëfandikoo-xel ngir tekki
- Hip "muus", "am-xel" lay tekki, muusaayu tappalaatukat.
- Hop ag yuuxu la gu kuy tëb di def (sooy tëb ni op!).
Nee nañu baat baa ngi war a bawoo ci DJ Luv Bug Starski mi ko doon faral di jëfandikoo suy wax. Waaye li wér te wóor mooy ne gandoor bu Sugarhill Gang mooy ki ko siiwal ci àdduna bi, ci seen woy woowu Rapper's Delight, di benn ci woyi rap yi ñu njëkk a def k7.
Taariix
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]Ay cosaanam
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]Woyu hip-hop ci buumu xeeti woyi waa-aamerig yu ñuul yi la bokk. Ay dàttam ñi ngi bàyyikoo ci dundiin gu metti gi ñu nekkee woon, dalee ca seeni maam ba ci jamono yi muy juddu, woy yañu daan def ca tool ya daan ca naqarlu seenug nekkiin, ak daan ca fattali seenug jóge Afrig. Mi ngi tàmbalee ciy kebetu niki xeeti woy yu mel ne ragetime, jazz, blues. Ci lu gën a jonjoo, woyu hip-hopa ngi bawoo ci Soul, ak ci funk. Yii xeeti woy bawoo bëj-gànnaaru Aamerig dem ba fasook sound-system bu waa-jamayka, bi àgg ba New York ndax ndoxandéemu gi waa-jamayka yi daa def foofa. Ba tax-na ñett ñi ñu ne ñoo sos yëngu-yëngu hip-hop fa lañu bàyyikoo.
Donte hip-hop ci yii xeeti woy la jële ay dàttam, waaye doonul seenug wéyal. Du lu ay tëggkat yu xereñ ci seen liggéey toog xalaat, ni blues doonee wéyalug jazz, gospel juddoo ci blues, soul tegu ci, funk ñëw, caaday hip-hop dafa am ab dog-dog ag yeneen xeeti woy yooyu
Aji-rap yi njëkk
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]Les premiers rappeurs et groupes de rap qui ont marqué l'histoire sont :
- Sugarhill Gang
- Run DMC
- Afrika Bambaataa
- KRS-One
- Grandmaster Flash
- Beastie Boys
- LL Cool J
- Big Daddy Kane
- Last Poets